Michry ak Baye
Waw michiry nenako yaw yalla sou féké mbeguel bima am si cheikh ibrahima niass dafmay dioureul lorangué manguilay niane yaw yalla nga kheupeuma bep lorangué bo am ma degat kerok si ziara oustaz ahmeth ba mouy béguel gayi si leneu si wakhou michiry yi neneu delouna wakh mouni kerok yomal khiyam souniouko oubilone adiana mou khol guissoul cheikh ibrahima niass dafay wakh li dou adiana safara le wayé bouniou oubilone safara mou guisss fa baye niass dafay diap ni safara moy adianam ndakh wakhone nako mouni yaw yalla manguilay niane kerok yomal khiyam sama beut yi na tegou si baye niasss rekk man doynama machalla wayé bi daw lo sama yaram nak moy bimou né man michiry aduna bou cheikh ibrahima niass noyetoul man khawma louma fay defff motakh biko baye tago di dém londre mom si yonou gnibém dieum mauritanie fala guéné aduna ndeyssane gayi khamone naniou baye niass .

Commentaires
Enregistrer un commentaire